2 Corinthians 2:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su kenn tegee moroomam naqar, du man la ko teg, waaye man nanu ne, yéen ñépp la ko teg — matul may réyal mbir mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su nit tegee aw naqar, man naa ne du man rekk la ko teg, waaye yeen ñépp la teg aw naqar, mbaa boog ma ne ñenn ci yeen, ngir baña réyal mbir mi lool.