2 Corinthians 3:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mbaa du danoo tàmbalee tëgguwaat nag? Mbaa du danoo soxla ni ñenn ñi ay dénkaane yu ñu nuy gërëme, te ñuy bataaxal yu jóge ci yéen walla yu jëm ci yéen?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Danuy tàmbaleetee seedeel sunu bopp ne noo yelloo ngërëma? Am danoo soxla ni ñenn nit ñi, ay bataaxal yu jëm ci yeen, mbaa mu bawoo ci yeen, ngir seedeel nu ngërëm?