2 Corinthians 3:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it ndegam li wéy dafa amoon ndam, astemaak li fi sax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax ndegam liy wéy moo làmboo woon ag leer, astamaak li fi sax.