2 Corinthians 3:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dunu def ni Musaa, mi daan muur xar-kanamam, ngir bànni Israyil bañ a gis jeexug leer googu saxul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te baña def ni Musaa ma daan muur kanam ga, ndax bànni Israyil bañ ne jàkk ci leer guy wéy, di giim, di giim ba jeex.