2 Corinthians 3:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye seen xel dafa daldi gumba. Ba tey jii sax, bu ñuy jàng téereb kóllëre gu jëkk gi, muuraay moomu dafay des; deñul, ndaxte ci Kirist rekk la man a deñe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye seenum xel a dërkiis. Ba tey jii, bu ñuy jànge biir mbooloo, téereb kóllëre gu jëkk gi, muuraay googoo fi des; murikuwul, ndax ci Almasi lay deñe.