2 Corinthians 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Déedéet, yéenay sunu bataaxal, te ci sunu xol lañu ko bind, di bataaxal bu nit ñépp man a xam te jàng ko;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sunu bataaxal kay, yeen la, te dees koo bind ci sunu xol, ba ñépp xam ko, jàng ko.