2 Corinthians 4:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fu nu tollu noo ngi gàddu ci sunu yaram dee gi Yeesu dee woon, ngir dundu Yeesu moom it feeñ ci sunu yaram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dee gi Yeesu dee woon, moom lanu àndal ci sunu yaram, fu nu tollu, ngir dundug Yeesu itam mana fése ci sunu yaram.