2 Corinthians 4:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bés bu nekk, nun ñiy dund, ñu ngi nuy jébbal dee ndax Kirist, ngir dundu Kirist moom itam feeñ ci sunu yaram wiy dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Saa su nekk, nun ñiy dund, ñu ngi nuy jébbal ndee ndax Yeesu, ba tax dundu Yeesu it mana fése ci sunuw suux wi jëm ndee.