2 Corinthians 4:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbind mi nee na: «Damaa gëm, moo tax ma wax.» Nun it nag, ndegam am nanu menn xelu ngëm moomu, danoo gëm, ba tax nuy wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bindees na ne: «Damaa gëm, moo tax ma wax.» Nun it, wenn xeetu ngëm wi lanu am. Danoo gëm, moo tax itam nuy wax.