2 Corinthians 4:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte xam nanu ne Yàlla, mi dekkal Boroom bi Yeesu, dina nu dekkal nun itam ak Yeesu, te dina nu yóbbu ak yéen, taxawal nun ñépp ci jataayam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte xam nanu ne ki dekkal Sang Yeesu, moo nuy dekkal itam, nook Yeesu, te moo nuy yóbbu ba nu teewi, nook yeen, fa kanamam.