2 Corinthians 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte lépp li nuy daj, seen njariñ a tax, ngir yiwu Yàlla, wiy yokku ci nit ñu gën a takku, yokkaale ngërëm lu jëm ci Yàlla, ngir jollil ndamam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp yeena tax, ngir yiwu Yàlla lawa law, ba cant gu ne gàññ tukkee ci ñi ëpp ci nit ñi, ngir màggug Yàlla.