2 Corinthians 4:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su fekkee ne sax, xebaar bu baax bi dafa muuru ci ñenn ñi, dafa fekk ñoom ñu aw yoon wu jëm ci sànkute.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sunu xibaaru jàmm nag, su muuroo, ñi nara sànku la muurul.