2 Corinthians 4:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Yeesu Kirist Boroom bi lanuy waare, waaye waarewunu lu jëm ci sunu bopp. Nun seeni jaam lanu ndax Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun kat, du sunu bopp lanuy waare, waaye li Yeesu Almasi dib Sang moom lanuy waare, te nun ci sunu bopp nooy seeni jaam, ndax Yeesu.