2 Corinthians 4:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dañu nuy sonal fu nekk, waaye kenn tancu nu. Dañu nuy dugal ci ruq yi, waaye dinanu ci génn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu nekk lees nuy tance, waaye deesu nu nappaaje. Dinanu jaaxle, waaye dunu jàq.