2 Corinthians 5:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaram wi nu soloo ci kaw suuf dafa mel ni ab tànt. Su daanoo, xam nanu ne, Yàlla jagleel na nu am taax ci asamaan, mu loxol nit defarul, di taax muy sax ba fàww.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam nanu ne sunu yaram, sunu këru kaw suuf gii di ab xayma, bu daanoo it, am taax lanu am fa Yàlla, kër gu sax dàkk, gu loxol nit tabaxul.