2 Corinthians 5:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte nun ñépp fàww nu teew ci kanamu Kirist, mu àtte nu, ngir ku nekk jot peyu li mu def ci yaramam, muy lu baax walla lu bon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat, nun ñépp fàww nu taxawi fa jalub àttekaayu Almasi, ngir ku nekk yooloo kemu jëf ja mu jëfe yaramam, muy lu baax, mbaa lu bon.