2 Corinthians 5:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw xam nanu ragal Yàlla nag, nu ngi fexee gëmloo nit ñi, waaye li nu nekk leer na Yàlla te yaakaar naa ne, leer na leen it, ba ne fàŋŋ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Danoo xam lan mooy ragal Boroom bi nag, te moo nu tax di wax lu gëmloo nit ñi. Yàlla de ràññee na bu baax nooy kan. May yaakaar ne yeen itam, ci seen biir xol, ràññee ngeen bu baax nooy kan.