2 Corinthians 5:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Jéemunoo waxati lu ngeen nuy nawe, waaye danu leen a bëgg a may yoonu tiitaru ci nun, tey tontu ñooñuy tiitaroo col te du xol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seedeelatunu sunu bopp lu jar ngërëm de, danu leen di may lu ngeen nu mana sagoo, ndax ngeen am tontal ñi sagoowul li ci biir xol, xanaa di sagoo am peeñ.