bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 5:14
2 Corinthians 5:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte mbëggeelu Kirist moo nuy jiite, ndax wóor na nu ne, ndegam kenn rekk a dee ngir ñépp, kon ñépp a dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte cofeelu Almasi daal moo nu jiite, nun ñi ràññee lii: Gannaaw kenn moo deeyal ñépp, kon ñépp a dee.