2 Corinthians 5:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kirist mi musul a def bàkkaar, Yàlla def na ko bàkkaar ci sunu wàll, ngir ci sunu bokk ci moom, nu man a doon njubteg Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Almasi mi masula bàkkaar, moom la Yàlla sëf sunu bàkkaar, ngir nu mana ame ci moom àtteb nit ñu jub fa Yàlla.