2 Corinthians 5:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nun ñi nekk ci tànt bii, nu ngi wonk ndax coono. Du caageen ne, danoo bëgg a summi sunu yaramu àddina, waaye danoo bëgg a sol sunu yaramu asamaan, ngir liy dee sóobu ci biir dund.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noo ngi onk ndax diis, li feek nu ngeek sunuw yaram, xayma bi nu soloo nii. Du summiku lanu namm, waaye solu teg ko ci lanu namm, ngir li jëm ndee, daldi suux ci biir ndund.