2 Corinthians 5:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte doxewunu ab gis, waaye ngëm lanuy doxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax ngëm lanuy doxe, waaye doxewunu ab gis-gis.