2 Corinthians 6:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen bokki Korent, wax nanu leen sunu biir ak sunu biti, di leen ubbil sunu xol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen bokki Korent, wax nanu leen sunu biir yépp, ubbil leen sunu xol.