2 Corinthians 6:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ubbiku nanu ci yéen, waaye yéen ubbikuwuleen ci nun.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Genn ñooru jógewul ci nun, waaye yeen yeena nu ñooroo seen xol.