2 Corinthians 6:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi wax ak yéen ni samay doom; feyleen nu bor bi, yéen itam; ubbileen seen xol!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag, yeen, feyleen nu bor bi boog, ma wax ak yeen ni samay doom, ubbil-leen nu seen xol!