2 Corinthians 6:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag Boroom bi nee na:«Génnleen biir ñooñu te beru.Buleen laal dara lu am sobe,kon dinaa leen teeru.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag: «Nangeen génne ci seen biir, te teqlikoo ak ñoom,» la Boroom bi wax. «Lu sobewu, buleen ko laal. Su boobaa, maa leen di dalal.