2 Corinthians 6:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinaa nekk baay ci yéen,ngeen di doom ci man, muy góor, di jigéen. Moom la Aji Kàttan ji wax.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maay doon seen baay, ngeen di samay doom, góor, ak jigéen,» la Boroom bi, Aji Man ji wax.