2 Corinthians 6:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ñu nuy dóor, di nu tëj ci kaso, dëkk yi di yengu ndax sunu mbir; nuy liggéey ba sonn, di fanaanee xool, di woor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ci ay dóor, ak néegi kaso, ci biir mbooloo yu nu jógal, ci doñ-doñ ju metti, ak fanaanee xoole, akub xiif;