2 Corinthians 7:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag su ma leen bindee, ki tooñ taxul, ki ñu tooñ it taxul, waaye dama leen a bind, ngir ngeen man a gis ci kanam Yàlla cawarte, gi ngeen am ci nun.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag su ma leen bindee, ki tooñ taxul, ki ñu tooñ it taxul, waaye dama leena bind, ngir farlute gi ngeen am ci nun, mana fés, fi kanam Yàlla, ngeen gisal ko seen bopp.