2 Corinthians 7:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te loolu seral na sunu xol. Sunu xel dal na, rawati ci li nu ànd ak Tit ci mbégam, ci li ngeen seral xolam, yéen ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu seral na sunu xol. Te yemunu ci xol bu sedd, waaye gënati nanoo bége mbégtem Tit, mi ngeen dalal am xelam, yeen ñépp.