2 Corinthians 7:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su fekkee ne tiitaru woon naa ci seen mbir ci kanamu Tit, rusuma ci. Dëgg rekk lanu leen mas a wax; noonu it la Tit gise ne, li nu leen doon seede lépp, dëgg la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg la, damoo naa leen as lëf fi kanam Tit, waaye gàcce fekku ma ci. Dëgg lanu leen masa wax, waaye la nu leen doon damoo fa kanam Tit itam, noonu la mujje doon dëgg.