2 Corinthians 7:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bég naa, ndaxte xam naa ne, man naa leen a wóolu ci lu nekk!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bég naa, ndax wóolu naa leen ci lépp!