2 Corinthians 7:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba nu àggee diiwaanu Maseduwan, noppaluwunu, waaye coono bu ne daj nanu ko: xeex ci biti, njàqare ci biir.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba nu àggee diiwaanu Maseduwan, sunuw yaram noppluwul, waaye daj nanu bépp coono: xeex ci biti, njàqare ci biir.