bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 8:10
2 Corinthians 8:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon lii laa xalaat ci lu baax ci yéen: yéen ñi nga xam ne tàmbaliwuleen a jëf rekk, waaye yéena jëkk a am yéene jii daaw,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab xalaat laa am ci mbir mii, te mooy doon seen njariñ. Du jëf ji rekk ngeen jëkke woon, waaye yeena jëkkoona biral daaw, yéeney dimbali.