2 Corinthians 8:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte joxe, bu àndee ak yéene, Yàlla dina ko nangu, di seet li nu am te bañ a seet li nu amul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat ab joxe, bu àndee ak yéene rekk, la boroom joxe bi amul, deesu ci natt lees koy nangul, waaye li mu am, ci lees koy nangul ab joxeem.