2 Corinthians 8:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bëgguma leen a teg soxla, ngir woyofal ñi ci des, waaye na ñépp tolloole.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du caageenu nag, teg leen coono, ngir teggil ñenn ñi, waaye ag tollale war na ci.