bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 8:14
2 Corinthians 8:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Tey jii nag man ngeen sàkk ci li ngeen barele, faj soxlay ñeneen, ngir ëllëg it bareleg ñooña faj seen soxla. Noonu ñépp tolloole.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Tey jii seenug rembatle mooy faj soxlay ñeneen, ngir ëllëg, rembatley ñooña faj seeni soxla, yeen itam. Su ko defee ag tolloo am.