2 Corinthians 8:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi nu ko laajee, mu ñëw ci yéen, nangu na, te rax-ca-dolli cawarteem tollu na, ba nu man a wax ne, ci coobarey boppam la jóge, jëm ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba nu ñaanee Tit mu dikk ba ci yeen, nangul na nu, waaye yemu ca, nde ci xéraangeem la yebul boppam ne mooy dikk ba ci yeen.