2 Corinthians 8:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Danuy fexee def li jub, du ci kanam Yàlla rekk, waaye it ci kanam nit ñi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li nuy xinte moo di li baax ci kanam Boroom bi, te baax ci kanam nit ñi itam.