2 Corinthians 8:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yónniwaale nanu it sunu mbokk, mi nu seetlu cawarteem ay yooni yoon ci fànn yu bare, te mu gën koo fésal bii yoon ndax kóolute gu réy, gi mu am ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boole nañu leen itam ak sunu mbokk mu nu nemmiku xéraangeem ay yooni yoon, ci fànn yu bare, te mu gënatee xér bii yoon ndax kóolute gu réy gu mu am ci yeen.