2 Corinthians 8:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na seen teeru firndeel nag seen mbëggeel ci kanamu mboolooy ñi gëm, te dëggal leen ne, noo yey wóolu leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag wonleen leen lu firndeel seen cofeel ci ñoom, ak ci kanam mboolooy gëmkat ñi, firndeel itam ne noo yey wóolu leen.