2 Corinthians 8:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Saraxu nañu nu lool, ngir bokk ci ñiy yónnee ndimbal gaayi Yàlla yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañu noo ñaan, ba di nu tinu, ngir nu may leen, ñu def seen loxo ci ndimbalu jàpplante gi jëm ci gëmkat ñu sell ñi.