2 Corinthians 8:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te yemuñu sax ci li nu séentu woon ci ñoom, waaye dañoo jébbal seen bopp Boroom bi jëkk, gannaaw loolu ñu jébbal nu seen bopp ci coobareg Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li nu séentu woon sax wees nañu ko, nde Sang bi lañu jëkka jébbal seen bopp, door noo jébbal seen bopp, te noonu la ko Yàlla bëgge.