2 Corinthians 9:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yàlla miy jox beykat bi jiwu ak nit ab dund, dina leen jox jiwu wu ne gàññ, te sakkanal li seen njub meññ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te kiy jagleel beykat bi am jiwu, ak mburu mu nit di dunde nag, kooku moo leen di jox jiwu mu ne gàññ, te mooy ful seen meññeefum njekk.