2 Corinthians 9:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu dingeen woomle ci lépp, ba yéwén ci bépp anam, ba tax ñu bare gërëm Yàlla ndax li ngeen maye jaarale ko ci nun.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee ngeen woomle ci lépp, mana yéwén ci wet gu nekk, ba seen jëf ji sottee ci nun, mana jur cant gu bare, ñeel Yàlla.