2 Corinthians 9:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte xam naa seen yéene ju rafet, te maa ngi ciy damu ci kanamu waa Maseduwan, naan leen: «Daaw fekk na waa Akayi jekk.» Te seen cawarte xamb na ñu bare ci ñoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax xam naa seen yéene ju réy, te moom laay damoo ci kanam waa Maseduwan, naan leen: «Daaw fekk na waa Akayi noppi.» Te seen xéraange jooju ngeen nekke xiirtal na ñu bare.