2 Corinthians 9:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi yónni nag bokk yooyu, ngir damu gi nu doon damu ci yéen ci mbir mii bañ a neen, te ngeen jekk, ni ma ko waxe woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa yebal bokk yi, di yaakaar ngeen noppi ni ma ko waxe woon, ngir la nu leen doon damoo ci mbir mii, baña neen.