2 Corinthians 9:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moo tax ma xalaat ne, li gën mooy yónni bokk yooyu, ñu jiitu ma ci yéen, topptoo mbiri ndimbal lu yaatu loolu ngeen dige woon. Loolu di may gu tàlli, te bañ a nekk yëfi nay.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax ma noon naa soññ bokk yi, ñu jiitu ma ci yeen, ba waajal ndimbal lu takku li ngeen dige woon, ba mu noppi, te baña doon sompi ŋott, xanaa di ndimbal lu duun.