2 John 1:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag soxna si, maa ngi lay dénk lii: nun ñépp nanu bëggante, te loolu du dénkaane bu bees, waaye moom lanu jotoon ca njàlbéen ga.