2 Kings 1:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Malaakam Aji Sax ji ne Ilyaas: «Wàccal ànd ak moom, bu ko ragal.» Mu daldi wàcc ànd ak njiit la ba ca Buur,